13/09/2024
Chers compatriotes.
Vous pourrez suivre le message à la Nation de son Excellence, Bassirou Diomaye Faye, ce jeudi 12 septembre 2024 à partir de 20h sur la RTS.
•••••••••••••••••••••••••••••••••••••••••
Bokki ma-réew yi,
Jaajëf ci ngeen seetaan àddug Njiitu Réew mi Basiiru Jomaay Fay gu jëm ci Askan Wi, ci alxemes jii 12i fani SEPTEMBRE 2024 bu 20i waxtu jotee.