Xalima Wolof

Xalima Wolof Informations de contact, plan et itinéraire, formulaire de contact, heures d'ouverture, services, évaluations, photos, vidéos et annonces de Xalima Wolof, Public & Government Service, Touba, Touba.

17/10/2025
Xalima_Wolof
17/08/2022

Xalima_Wolof

Asadul Xadiim♥️
31/10/2020

Asadul Xadiim♥️

Seex Hamsatu Mbàkke yàgg fi lool te wér aamiin !
15/07/2020

Seex Hamsatu Mbàkke yàgg fi lool te wér aamiin !

Yal na Yàlla yëram ko,te jéggal ko aamiin !
25/06/2020

Yal na Yàlla yëram ko,te jéggal ko aamiin !

Jumaa ju mag ji !!
23/06/2020

Jumaa ju mag ji !!

🔻Ñaan gu am solo lool,te mat a def...بسملة (30)الفاتحة (19)ءاية الكرسي (1)الاخلاص (41)صلاة علي النبي (1)Lii  ak  ñaan  l...
05/06/2020

🔻Ñaan gu am solo lool,te mat a def...

بسملة (30)
الفاتحة (19)
ءاية الكرسي (1)
الاخلاص (41)
صلاة علي النبي (1)

Lii ak ñaan la gu bàyyi koo ci ku Baax ki "Seexul Xadiim" jaar ci sëriñ Amsatu Jaxate mu wax ne: ku fi bàyyikoo buñu ko defalee dog bii, sunu Boroom jéggal ko mbooleem ay taq-taqam" maanaa ay bàkkaaram sëriñ Amsatu Jaxate bi fi jàmbaari alxuraan ji jógee,sëriñ Daam Abdu Rahmaan Lóo dafa joxe ndigal ngir ñu def dog bi,yéene ko yool bi. Kon képp koo xam ne gis nga sa mbokkum jullit mu fi bàyyikoo nga def ko yéene ko yool bi. Jërëjë!

Aji-nettali ji: sëriñ Mbàkke Kànni Buso maam Xari Jóob di sàkku ngeen ñaanal ko gudd fan,wér gi yaram Yàlla musal ko ci lépp luy lore, ak bépp jullit Aamiin!!

Xalima_Wolof_instagram❤️🔏

🔻Xibaar:😭Noo ngi leen di yëgal wàccub liggéey Soxna Yónni Njaay di Soxna ci sëriñ Fàllu Buso xalifa s.Mbàkke Kànni Buso ...
05/06/2020

🔻Xibaar:

😭Noo ngi leen di yëgal wàccub liggéey Soxna Yónni Njaay di Soxna ci sëriñ Fàllu Buso xalifa s.Mbàkke Kànni Buso di sàkku ci ñéPp ñu ñaanal ko njéggalul Yàlla ak yërmande Aamiin !!

01/06/2020
Sëriñ Mbàkke kenn ci ndawi seexul Xadiim yi di liggéey ci xam-xam...
01/06/2020

Sëriñ Mbàkke kenn ci ndawi seexul Xadiim yi di liggéey ci xam-xam...

Adresse

Touba
Touba

Téléphone

+221782284199

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Xalima Wolof publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Contacter L’organisation

Envoyer un message à Xalima Wolof:

Partager