Fondation Khidma

Fondation Khidma Jaamu Yalla ligueeyaléko seriñ bi
Ligueeyal seriñ bi jamooko Yalla Jërëjëf seexul Xadiim

Jumha mubarack ✨🙏🏾
15/05/2026

Jumha mubarack ✨🙏🏾

Jërëjëf seexul xadim jaarama maam Seex Ibrahima fall lamp
04/05/2026

Jërëjëf seexul xadim jaarama maam Seex Ibrahima fall lamp

26/04/2026
Khadim rasoul Jërëjëf cheikh ahmadou bamba 🙏🏾Bambavisuel
26/04/2026

Khadim rasoul Jërëjëf cheikh ahmadou bamba 🙏🏾
Bambavisuel

26/04/2026

JËRËJËF CHEIKH AHMADOU BAMBA KHADIM RASSOL.

👉 Abonnez-vous, partagez autour de vous et laissez-nous vos impressions en commentaire.
👇🏿👇🏿👇🏿
Bambavisuel
Mouridoulahination

Mbackei Yaanu boleek lou baax leep Ta ioe rk lañu baaxlé Yaanu taxaleek li bonn leep ta yaa ñu tee bonn 🙏🏾Ahmadou Ibnou ...
25/04/2026

Mbackei Yaanu boleek lou baax leep
Ta ioe rk lañu baaxlé

Yaanu taxaleek li bonn leep ta yaa ñu tee bonn 🙏🏾

Ahmadou Ibnou Taïb

Cëy sunu ku baax ki keen amul kudul ñun Ki keen xamul kudul bromam Ki sonnu Nguir ñeep jariñu Ni teunku woon guir ñeep t...
24/04/2026

Cëy sunu ku baax ki keen amul kudul ñun

Ki keen xamul kudul bromam

Ki sonnu Nguir ñeep jariñu

Ni teunku woon guir ñeep tinkuku

Ki yënggal liy yënggu leep ba noppi neh teek

Seexul xadim yakaari jaam ñi yalnanu sunu brom dollé fayal

Mbackei la ñeep daan ñaan seen brom akka sakku Yaako jaayanté ba amko ta djiayoko dangakoy mayer kou jayanté rk nga defa...
22/04/2026

Mbackei la ñeep daan ñaan seen brom akka sakku Yaako jaayanté ba amko ta djiayoko dangakoy mayer kou jayanté rk nga defal koko mouy greumeul Yalla Mbackei Jërëjëf

Mouride Weeru waay bangui Aagu waay baangui Footu kaay baangui Xeeweul ngaaguiNdiariñ laagui Laaxu waay baanguiAaru kaay...
20/04/2026

Mouride

Weeru waay bangui

Aagu waay baangui

Footu kaay baangui

Xeeweul ngaagui

Ndiariñ laagui

Laaxu waay baangui

Aaru kaay baangui

Muthj kaay baangui

Jariñul adina ak alaxira jaa guii

Si Xassida yi rk silanu mana amee liñuy sakku leep sunu diggëg Seriñ bi

Nouvelle édition Noorul munir

📖Wakaana hakhane
📖 Bismil ilaahi’kfini
📖Tuxfatul mutadarina
📖SINDIDI

Noorul Munir

Mbackei Yaa Baax Finga aggon sa brom akku yontém s*k djieguer koufa masa agg lam sokhla leep dako ñaan ñu mayko ndax see...
18/04/2026

Mbackei Yaa Baax

Finga aggon sa brom akku yontém s*k djieguer koufa masa agg lam sokhla leep dako ñaan ñu mayko ndax seenuk mbaax maténako

Ioe rk yaafa massah aag di dieund loo am jaayantee lako may si seenuk mbaax

Mbackei Yaax baax

Linga am leep si sa brom akkub yonéntém ba noppi dikko mayé

Kuko masa am dako daan jaay wayer daawuko mayé

Mbackei Yaax ta baaxuw baaxine 🙏🏾

✍🏽Ahmadou Ibnou Taïb

Adresse

Touba

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Fondation Khidma publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Contacter L’organisation

Envoyer un message à Fondation Khidma:

Partager